Wolof Vocabulary relating to Reproduction

Back to Vocabulary Resource Sheets

Email corrections and comments to ForTheWolof
A Unicode font is needed to view this page correctly. If you can read this Wolof character "ŋ" you are setup.

Female Reproductive Organs

Wolof terms for female external genetalia diagram
Wolof terms for female internal genetalia diagram

Anatomy

Wolof English French
awra ji (in order of acceptability)
kanam gi
njurukaay li
lëf li
data bi
pëy mi
dëjj wi
bajo bi
female external genitals le sexe de la femme
organes génitaux externes
organes sexuels
organes génitaux
ëmbukaay
butitu njurukaay bi
móolukaay bi
uterus l'utérus (m)
buntu butitu njurukaay bi cervix le col de l'utérus
baatu butitu njurukaay bi cervical os L'orifice cervical
nenukaay bi
mbuusu jiwub jigéen mi
ovary l'ovaire (m)
nen bi
jiwub jigéen bi
ovum l'ovule (m)
deru xelli bu nooy uterine lining, endometrium l'endomètre (m)
loxo butitu njurukaay bi
solom bi
ñoxu Falop bi
fallopian tube la trompe de Fallope
kanam gi
cott li
séyukaay bi
lëf li
pëy mi
bajo bi
caapa (some say it is the perineum)
vagina (only cott li and séyukaay bi refers exclusively to the vagina. The other terms may also refer to genitals in general) le vagin
coppreet bi clitoris le clitoris
àpp yu mag/yu ndaw yi
tuñu kanam yu mag/yu ndaw yi
xottu lëf yi
labia majora
labia minora
les grandes lèvres (f pl)
les petites lèvres (f pl)
sawukaay bi
bën-bënu sawukaay bi
urethra
urethral meatus
l'urètre (m)
buntu cott li introitus l'entrée du vagin
deru ndaw gi
raw gi
hymen le hymen
cutt gi perineum le périnée
xonq li vulva la vulve
tuun bi
muuti gi
anus l'anus (m)
ween wi breast le sein
cus wi nipple le mamelon
lërén bi colostrum le colostrum
meen mi breast milk; sap of a tree le lait maternel

Menstrual physiology

njagamaar bi
waxambaane
adolescent girl adolescent boy adolescente
waxtu tëngaay age of the start of fertility, puberty for a girl puberté
mbaaxum jigéen
reegal
menstrual period les règles (f); la menstruation
julliwul
setul
gis reegalam
to have one's period avoir les règles
aada ji menstrual cycle le cycle menstruel
meññub jiwub jigéen
waxtu nji
ovulation ovulation (f)
jigéen ju fóotatul post menopausal woman la femme ménopausée

Pregnancy

ànd bi
rakku liir
placenta le placenta; l'arrière-faix (m)
lutt bi umbilical cord le cordon ombilical
jibay ndox mi amniotic sac la poche amniotique
wann lor to fall pregnant concevoir; devenir enceinte
jafte bi beginning of pregnancy/ 1st trimester; morning sickness premier trimestre; avoir des nausées pour une femme en début de grossesse.
biir bu yàqu
doom bu dellu
biir bu xàcci
miscarriage la fausse couche
yàq biir to cause an abortion faire avorter
doom bu dellu
liir bu indaalewul bakkan
pér bi
still birth l'enfant mort-né
rewli assist in labour assister une femme qui accouche; exercer la fonction de matrone.
wasin give birth donner naissance; accoucher
mucc give birth safely  
mat wi labour le travail
matu to be in labour être en travail pour la parturiente
xëccu butitu njurukaay
woññaaru butitu njurukaay bi
uterine contraction la contraction
jeñax
nalu
jeñ
to push in labour pousser lors de l'accouchement
aji-matu ji woman in labour la parturiente
aji-wasin ji
wasin-wees wi
woman who has just given birth  
tonqi
mbuusu ndox mi fàcc
breaking of the waters perdre les eaux
meret mi lochia lochies (f)
xorom preeclampsia la prééclampsie; avoir de l'albumine
tërinu liir bu mbankaanu breech position une présentation du siège
tërinu liir bu galanee transverse lie une présentation transverse
présentation transversale
liir bi tëdd gàllankooru fetal malpresentation malprésentation du foetus

Male Reproductive Organs

awra ji
waa-yàlla ji
sàkkara si
male genitals le sexe de l'homme
organes sexuels
organes génitaux
kooy bi
waa-yàlla ji
sull bi
penis le pénis; la verge
ndéeñ glans (head) of penis le gland de la verge
mbuñika mi foreskin le prépuce
dambal
mbuusu xuur yi
scrotum le scrotum
xuur bi
peng
testicle le testicule
jiwub góor ji semen, sperm le sperme; la semence
solomu maniyu bi spermatic cord le cordon spermatique

Sexuality

séy bi
katt bi (vulgar)
the act of sex l'acte sexuel
jote
séy
semb
sànjaay
tëdd ak
to have sex avoir des rapports sexuels
coucher avec
tàng
yee yaram
yëngal yaram
daw yaram
to become sexually aroused s'exciter
motoxal
cuq
baram
tapparñi
làmb
to engage in sexual foreplay
to stimulate the sex organs
les préliminaires
àgg ci jigéen sexual penetration la pénétration
maniyu bi
ndoxum góor mi
ejaculate, semen le sperme
car-carib maniyu
car-carum ndoxum góor
ejaculation éjaculation (f)
ndoxum góor mi sar to ejaculate éjaculer
koddal/kuddal gi, jógal bi erection érection du pénis
kuddal to become erect avoir une érection
daanub góor
daanub jigéen
climax, orgasm orgasme
mballu to masturbate se masturber
siif
siif bi
to rape
rape
violer une femme
violation
yoom, tële to be impotent impuissant sexuel
palani family planning Le planning familial
kawas bi
mbar
condom le préservatif
aparey bi IUD le stérilet
jafaram diaphragm le diaphragme
jasiirloo góor/jigéen sterilization procedure stérilisation


Back to Vocabulary Resource Sheets


Village