Wolof Vocabulary relating to the Anatomy of the Trunk & Limbs

Back to Vocabulary Resource Sheets

Email corrections and comments to ForTheWolof
A Unicode font is needed to view this page correctly. If you can read this Wolof character "ŋ" you are setup.

Wolof terms Trunk front view

Wolof terms trunk back view
Wolof
English
French
yaram wi body le corps
ruggit wi; këllu bopp
yaxi neen yi
skeleton le squelette
gënnu yaram gi truck le torse
yaxu diggu gannaaw bi spine la colonne vertébrale
l'épine dorsale (f)
xuru gannaaw gi valley of flesh in the centre of back la vallée du dos; épine dorsal
ndodd li top of spine just below cervical protuberance, vertebral column échine
njanqaay centre back between shoulder blades  
palami shoulder blade, scapula l'omoplate (f)
yuqu ciiriir spinal cord la moelle épinière
dënn bi chest la poitrine
faar gi ribs la côte
saatu dënn bi sternum  
ween wi breast le sein
cus wi nipple le mamelon
biir bi abdomen le ventre; l'abdomen (m)
koll bi potbelly le gros ventre
tamb-tamb pinch of skin at the waist  
jumbux bi /jumbax bi navel, belly button le nombril
nëq bi lower abdomen/pubic region; groin l'aine (f)
wàq wi groin, area between legs  
xeese bi   l'aine (f)
cokk yi pubic hair des poils pubiens
fàllare gi pelvis le bassin; le bassinet
tikkar gi sacrum le sacrum
yammarkiij bi
yaxu yammarkiij bi
coccyx le coccyx
ndigg li loin, hip, kidney les lombes; la hanche
taat wi buttocks les fesses
xottu taat single buttock la fesse
waŋ ji large buttocks stéatopygie; grosses fesses
ndunturuk natal cleft  
tuun bi
suuf gi; demukaay duus
rasu gi; dayukaay
buur taat
anus (note: few people know any of these names) l'anus (m)

xar to have an anal fissure  
jàngoro kajoor haemorrhoids les hémorroïdes (f)
kanam gi front le devant
gannaaw gi back le derrière
wet gi side le côté
ndeyjoor bi right droit
càmmooñ bi left gauche
kaw superior supérieur
suuf inferior inférieur

Loxo bi (The Arm)

loxo bi arm, hand le bras; la main
mbagg mi shoulder l'épaule (f)
poqtaan mi axilla l'aisselle (f)
përëg mi upper arm bras entre l'épaule et le coude
conco li
cooyantel
elbow le coude
tibujara bi /tiwujara bi /tikkujara bi wrist le poignet
baaraam bi
   baaraamu déy bi
   baaraamu sannikaay bi/ joxoñ bi
   baaraamu digg
   baaraamu domboor/ jaaro/topp digg
   baaraamu sanqaleñ
finger
   thumb
   index finger
   middle finger
   ring finger
   little finger
le doigt
   le pouce
   l'index
   le majeur
   l'annulaire
   l'auriculaire
we wi finger nail l'ongle (m)
cusu baaraam wi finger tip le bout du doigt
ténq bi
diggu loxo bi
biiru loxo bi
palm la paume

Tànk bi (the Leg)

tànk bi leg; foot la jambe; le pied
pooj bi thigh (medial side) la cuisse
lupp bi thigh ( lateral side) la cuisse
mooco mi head of the femur la tête du fémur
ndigg li hip la hanche
óom/wóom bi knee le genou
bëtu wóom bi patella la rotule
poqutaanu tànk mi popliteal fossa le jarret
yul bi; yil calf le mollet
yeel bi shin inférieure de la jambe de tibia
wëq wi ankle la cheville
dojaru tànk wi
bëtu tànk bi
lateral malleolus
medial malleolus
 
siis gi archilles tendon le tendon d'Achille
ndëggu li
ndëpp li
sole of foot la plante du pied
dënnu tànk ball of foot la plante du pied
biiru tànk instep, arch la paume du pied; la voûte plantaire
tëstën mi heel le talon
gannaawu tànk back of the foot  
baaraamu tànk (as for fingers) toes l'orteil (m)

génnug yax
rëq-rëq bi; rëq
dislocation, to have a dislocation la luxation; la dislocation; avoir une luxation; luxer; disloquer
faxaj sprain l'entorse (f); la foulure; avoir un entorse
dam-dam bi fracture la fracture
rink bow-legged avoir les jambes arquées
tànk yi dañu xar cracks on the feet  


Back to Vocabulary Resource Sheets


Village