Wolof Vocabulary relating to Body Organs

Back to Vocabulary Resource Sheets

Email corrections and comments to ForTheWolof
A Unicode font is needed to view this page correctly. If you can read this Wolof character "ŋ" you are setup.

Cardiovascular and Respiratory Systems

Wolof English French
xol bi heart le coeur
xëtër wi lung le poumon
pottax bi trachea la trachée
waruwaay bi vessel le vaisseau
siddiit gi
waruwaayu deret bi
blood vessel le vaisseau sanguin

tëf-tëfu xol bi heartbeat le battement de coeur
la pulsation
noyyi/ nokki to breathe respirer
xetu gémmiñ gi
bàqatay ki
bad breath la mauvaise haleine
xiix
appaat
to pant, to puff haleter
sëqët, sëqat to cough tousser
sëqët su jàppoo coughing fit  
yuqóol; yuqóol gi hiccoughs avoir le hoquet
ñandaxit/ñendaxit wi nasal mucus le mucus nasal; morve
xaaxtëndi bi/xaaxtandiku sputum/phlegm le crachat; les expectorations
rattaxit wi mucus la glaire

Haemopoetic System

yóq bi / yuq gi bone marrow la moelle osseuse
deret ji blood le sang
lumbu deret wi blood clot le caillot du sang
nàcc to bleed saigner
xëpp deret haemorrhage l'hémorragie (f)
xeetu deret ji blood group le groupe sanguin
kaaraange gi immunity l'immunité (f)

Digestive System & Abdominal Organs

biir gi
bàq gi
stomach l'estomac (m)
butit bi intestine l'intestin (m)
res wi liver le foie
wextan wi gallbladder, bile la vésicule bilaire; la bile
gàddaam gi
ndese mi
spleen la rate
xelliwaan bi; mbuus mi gland la glande
xelliwaanu lor bi salivary gland la glande salivaire
xelliwaanu bàq bi stomach gland  
xelliwaanu reesal bi digestive glands le suc digestif
xelliwaanu butit bi intestinal gland  

tëflit bi
lor wi
saliva la salive
yuut gi dribble la bave; baver
wextan wi bile la bile
xellitu bàq wi gastric juices le suc gastrique
xérñéññ gi gastric acidity acidité gastrique
xellitu reesal wi digestive juices  

day yi
puub yi
jonkan yi
faeces les fèces (f); le caca;
l'excrément (m)
doxat wi / doxot wi fart, pass wind; to pass wind le pet; péter; lâcher des vents
géex to belch éructer; roter
waccu yi; waccu vomit; to vomit la vomissure; vomir
fër to have indigestion avoir l'indigestion (f)
xel muy teey nausea la nausée
gall to regurgitate régurgiter
biir bu jooy
biir bu wax
stomach rumbles  

Urinary System

roño bi
dëmbeen bi
kidney le rein
butitu taaw bi ureter l'uretère (m)
paftan mi bladder la vessie

saw mi
seben bi
urine l'urine (f)
kew gi calcium stone; calculus; white clay le calcul; le calcaire
téju to have urinary retention la rétention

Locomotor and Nervous Systems

yóor gi/ yuur gi brain le cerveau
siddiit gi nerve, blood vessel, muscle le nerf
yax bi bone l'os (m)
tenqo bi joint l'articulation (f)
suux wi
siddiit gi
muscle le muscle
caas gi
buumu suux bi
tendon, ligament le tendon, le ligament

Wolof terms for abdominal organs diagram

Skin

der wi skin le peau
ras-ras bi; ras wrinkle; to have wrinkles la ride; être ridé
rew ji stretch mark la vergeture
futt to have a blister avoir une ampoule
daar bi callas le durillon
légét wi scar la cicatrice
tut wi keloid scar une cicatrice en relief
àkk wi scab/ crust la croûte
jib ji depigmentation of skin la dépigmentation de l'épiderme
xub desquamation se desquamer
booy, booy-booy bi rash, graize la rougeur de la peau, l'érythème
putte bi pustule, furuncle la pustule, le furoncle
jamuc bi/jumuc/jamoc pustule, furuncle on the face pustule, furoncle de visage
góom bi wound la blessure, la plaie
dana bi ulcer l'ulcère (m); la plaie suppurante
béy bi hives l'urticaire (f)
soccent/ soccet bi wart/ moluscum contagiosum la verrue
kabiyàdd gi; kabiyàdd ringworm; to have ringworm la teigne; avoir la teigne
ràmm ji; ràmm scabies; to have scabies la gale; avoir la gale
teeñ wi; teeñ louse; to have lice le pou; avoir les poux
fel wi flea la puce
pawax bi membrane la membrane
càqar bi lymph node le ganglion; glandes lymphatiques
suux wi flesh la chair
dónj lump l'excroissance (f); la bosse;
le nodule; la nodosité
giir gi mycetoma, maduromycosis  

xeeru baat wi inflamed cervical lymph node la glande lymphatique enflammée
somp wi; somp hangnail; have a hangnail envies, petites peaux à la naissance de l'ongle
dëtt ji
mbér bi
pus le pus

Back to Vocabulary Resource Sheets


Village