Wolof | English | French |
kanam gi/xar- kanam gi cëlmaay li |
face, facial appearance, expression | le visage, physionomie |
jë bi | forehead | le front |
neekata bi | temple | la tempe |
nàmptal bi/naqtal bi | fontanelle | la fontanelle |
lex bi | cheek | la joue |
legg wi | most protuberant point of cheek below the eye | partie la plus saillante de la joue, au-dessous de l'oeil. |
karaw gi/ kawar gi | hair, body hair | les cheveux, le poil |
kaabaab gi | place of sideburns & along jaw | la joue des temporaux au menton |
faas yi | sideburns | les favoris |
kaaŋ mi | skull | le crâne, boîte crânienne humaine |
sikkim bi | chin; beard | le menton; la barbe |
ŋaam wi | jaw | la mâchoire |
yaxu ŋaam bi | jawbone | la mâchoire |
Bakkan bi (The Nose)
bakkan bi | nose; life | le nez; la vie |
paxu bakkan bi | nostril | la narine |
xonxon/xënxën | nasal mucosa | la muqueuse nasale |
suuxu bakkan | nasal septum | la cloison nasale |
nudu bakkan | bridge of nose | la base du nez |
nuur gi | tip of the nose | le bout du nez |
xeeñtu gi | sense of smell | l'odorat; le flair |
bori | to have a blood nose | saigner du nez |
Bët bi (The Eye)
bët bi/gët yi | eye | l'oeil (m); les yeux |
yéen(u bët) bi | eyebrow | le sourcil |
xef(u bët) wi | eyelash | le cil |
mbarum bët mi | eyelid | la paupière |
paxu bët bi | pupil | la pupille; la prunelle |
peru bët bi | lens | le cristallin |
ñuulu bët bi | iris | un iris |
biiru bët bi | conjunctiva | la conjonctive |
weexu bët bi | sclera, white of the eye | la sclérotique; blanc de l'oeil |
kuggu bët | place of eyebrows & surrounds | |
xoon gi | red part on the inner part of the eye | caroncule lacrymale |
catu bët | outer corner of the eye | angle externe |
siddiitu gis | optic nerve | le nerf optique |
neexaayu bët | visual acuity | l'acuité visuelle (f) |
gis bi | sense of sight | la vue |
mbempen | night blindness /poor acuity | héméralopie cécité nocturne |
rongooñ yi | tears | la larme |
laas li | sleep in eyes | la chassie |
jéll | to have a squint | loucher |
payis; payis bi | jaundice, to be jaundiced | ictère (m); la jaunisse |
Nopp bi (The Ear)
nopp bi | ear | l'oreille (f) |
bagaanu nopp gi | pinna, ear lobe | le pavillon de l'oreille |
taban gi | ear tip, lobule of ear | lobule of l'oreille |
laakata nopp | cartilege in front of ear, tragus | tragus |
paxu nopp bi | ear hole | conduit auditif externe |
xóot-xóotu nopp bi | ear canal | conduit auditif externe |
tulliwaan bi /biiru nopp bi | ear drum | le tympan |
siddiitu dégg | auditory nerve | le nerf auditif |
deggukaay | hearing apparatus | l'appareil auditif |
neexaayu nopp | aural acuity | l'acuité auditive |
gémmiñ gi | mouth | la bouche |
làmmiñ wi | tongue | la langue |
laa gi | tongue tie | frein de la langue |
làmmiñ wu ndaw wi | uvula | uvule (f); luette (f) |
denqaleñ bi | palate | le palais |
tuñ mi (tuñu kaw; tuñu suuf) | lips | la lèvre |
ciiñ mi | gum | la gencive |
bëñ bi reewu bi sell wi déegéej bi màgg dey |
tooth incisor canine molar wisdom |
la dent incisives canine molaire dent de sagesse |
sofe | to have mouth ulcers | avoir des aphtes |
Baat bi (The Neck)
baat bi | neck; voice | le cou; la voix |
xoor wi kar gi |
adam's apple | la pomme d'Adam |
put gi bóli gi purux bi/purax bi |
throat, back of the throat, oesophagus | la gorge, le gosier |
pottax bi | trachea, windpipe | la trachée; trachée-artère |
dendu baat sidditu baat gi |
sternomastoid | sternocleido-mastoïdien |
caq bi këllu poobar bi |
space above the clavicle salt cellar of clavicle |
la salière |
yaxu caq | clavicle | la clavicule |
ndaalu bopp | highest point on the head | |
cuukeel bi | external occipital protuberance | la protubérance occipitale externe |
ndoŋ li | occiput | l'occiput (m) |
doq gi | nape of neck | la nuque |
loos wi | back of the neck | la nuque, cou |
ndodd li | top of spine just below cervical protuberance, vertebral column | échine |
xaddamtiku | to clear one's throat | se racler la gorge |
waxu gi | sore throat | le mal de gorge; angine |
baat bu xoddoos | hoarse voice | voix rauque |
baat bu dee | loss of voice | |
biddanti; loos wu biddanti | to have a stiff neck; stiff neck | avoir le torticolis; le torticolis |
cafko gi | sense of taste | le goût |
wuum/uum | toothache | mal au dent |